Appli bii mooy Kàddug Yàlla, gi dikke ñaari pàcc: Kóllëre gu jëkk gi Yàlla fas ak nit, ak Kóllere gu yees, gi mujja wàcc, te ñenn ñi di ko wooye Injiil, mu tekki Xibaaru jàmm. Нaari tére yooyu, Yàllaa leen wàcce ci nitam ñu sell shi, kóllëre gu jëkk gi, su bind ko ci yawut, gu yees gi, ci làkku gereg. Li su bind ci tére yu jëkk ya nag, moom lanu tekki ci wolof.
[библия, волоф, каддуг ялла]